daara j family sun africa şarkı sözleri

Unite now (x4) Afriki yewul naac na (x4) Unite now Téy lagnu geum afreeca beug dunde jeum kanam Téy lagnu geum sugnu euleuk wékkuwul ci kéne Xam fignu jeum oh farafina !! xamél ci xambe fitna Gnila meune délo ginaw say ennemies deug deug Gni wéddi sa meun meun gnila yagg deug fél sa geud Afreeca fimou jaaré ay yoonam dafa xaré Jonganteek ay jafé jafé gniko jiité dougnou jeufé Sen kaddu dé jaggul dou wallu jaroul gnoukoy gaddu Xalé yi xiif di saraxu kom kom gi dé di wattatu Ganay yi geune sakkan lambe ta se kémb jarrul Alleu bi soppeeku taax yi lékk tool yi réggul Marral békoor fallu baykatt bi soldaaru Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now Bismarck limou teureul jiggu gnu gno bagn seuggu gnu Lou takh gnu beug gno neube jant bi lé né faang? fok Naaj bi teub gnu APE bignu signé xaax teuf beuggu gnu Cheikh Anta Diop inddina tonttu mboleem civilisations Afreecay sen penkku wolof bambara toutsi bantus Afreeca Unite bougn ko gantu wolof nga ni namppu gnu babtou Filé sign juddo beug ko faatlu lakk bou rafé té ni mouk mouk dou sanku Afreecay wooté mbolo fok ndeunde bi samppu nagnu maas noun gui Def ci tomb Bougnou boolé sougnou doolé euleuk dougnou romb Bayyi yalwaan wi baaram yi bankou System mou babylon no kheuy gnou gontou Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now Africa for so long You've been suffering down inside in silence Farafina it’s all about time your sons and daughters get together And stop the violence Yéel gni doon nélaw xana yeugu gnu ngélaw Béneen afrik mou seulmu yéwu ca njeul cepeelu European sosna fitna nguir gnou ngaayoo daayiman Weulbatiku ci souf di youlli sougnouy diamond Suul bouki suuliwaat ndawu afrik yeukeuti baat Ande bolo geustuwaat lou tax meunougnou dém Bi moy kheep sa bop roy daqq ci nassaraan Fate baakhi maam toppi nakhi neen Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now
Sanatçı: DAARA J FAMILY
Türü: Belirtilmemiş
Ajans/Yapımcı: Belirtilmemiş
Şarkı Süresi:
Toplam: kayıtlı şarkı sözü
DAARA J FAMILY hakkında bilgi girilmemiş.

Fotoğrafı